﻿Taalifi cant.
117.
Yeen xeetoo xeet, màggalleen Aji Sax ji, réewoo réew, kañleen ko. 
Moo nu xéewale ngoram gu réy, te wormay Aji Sax jee sax dàkk. Màggalleen Ki Sax! 
